lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu youssou n'dour - yaru

Loading...

ah nit ku reew la mu yor moomu ko
su la mu yor waddee ku yaru mooy for jarinoo
ah yaral sa doom ci bi muy guneel
xaleel ca tuutaay ba nga koy doora yer

wuy mbooloo wuy mbooloo
mbooloo mooy doole
wuy mbooloo mooy sa doole
mbooloo jammi reew la

aziizoo njaay lu yagg degg la yaay yaw xam nga loolu
aziizoo njaay du yagg ba ngay naaw man gem naa loolu
wiiri wiiri jaari ndaare

aziizoo njaay doomu ndeyu useinu njaay sunu waaji
aziiz li la yengel bu dee degg la ci yaw jafandul mu deger
wiiri wiiri jaari ndaare

bu ca reel bu ca yekkeki noddil mu deger
wiiri wiiri jaari ndaare
bu dee degg gu degg te deggentuwul noddil mu deger
wiiri wiiri jaari ndaare

wuy mbooloo wuy mbooloo
mbooloo mooy doole
wuy mbooloo mooy sa doole
mbooloo jammi reew la
aziizoo njaay du yagg ba ngay naaw man gem naa loolu
ndax aziiz xam nga ne degg du daw te degg moom du toxu
degg du nax saay degg yi amoon daaw am fi daaw jeeg
degg degg rekk moo fiy daw ba tay

ku lay begg na la begg ci degg
ku lay ban it na la ban ci dеgg
ba bu degg newee fekk la nga toog ci dеgg
li la yengel bu dee degg la ci yaw jafandul mu deger
wiiri wiiri jaari ndaare

bu ca regel bu ca yekkeki noddil mu deger
wiiri wiiri jaari ndaare
bu dee degg gu degg te deggentuwul noddil mu deger
wiiri wiiri jaari ndaare

wuy mbooloo wuy mbooloo
mbooloo mooy doole
wuy mbooloo mooy sa doole
mbooloo jammi reew la


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...