
lirik lagu youssou n'dour - yaay jêrëjëf
yaay jërëjëf
yaay jërëjëf
yaay booy
yaay jërëjëf
yaay jërëjëf
yaay booy
{music}
déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen jottali ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
(mani) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen partager ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
{music}
yaw sa yaay booy, moo sonnoon ci yaw
moo la daan boot, di yendu taxaw
bu ko weccoo k~leenen
bu la ko kenn jaral
{music}
leeg~léeg muy dem fu sori lool
même bu am ee luy lorel
budé sa soxla la, sa yaay dara du ko tëyyé
{music}
[yaay jërëjëf]
yaay jërëjëf
yaay booy
yaay jërëjëf
yaay jërëjëf
yaay booy
yaw sa bonheur (waawaaw), mën ta am benn solo
féek [yaw] sa yaay j~pp ul sa loxo bi, taf la ci dënn ëm
youssou yaay, garab la
[yaw] sa bonheur, mën ta am benn solo
féek [yaw] sa yaay j~pp ul sa loxo bi, taf la ci dënn ëm
(waawaaw) ni la sagal nga ma, ché yaay
yaay booy, walaye or la
(mani) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen jottali ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
(waaw) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen partager ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
yaw sa yaay, loo ko jox~jox it, bu ko naw
lu mu rëy~rëy, do ko raw
boo ko am ul éé, nga yéené ko~ko
li ne sa xol bi, yàlla xam na ko
(waawaaw) youssou yaay, diamant la, or la
jërëjëf yaay
youssou yaay, garab la, yaay kër la
abdoulaye ni daaro mbaar, maajoor ni daaro mbaar
matar ni daaro mbaar, ak seen jigéen
sóogi digéek, birëm digi samba
lool kurë mbisaan sugu paate sambala ganja, leen siré
yaay soxna mboup, jërëjëf yaay
déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen jottali ko
kuy teral sa yaay, te nga dekëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay tеral
(mani) déglu ti leen, ma wax ati ko
ku ko déggul, ngeen partager ko
kuy teral sa yaay, te nga dеkëti
ba amm ngërëmëm, yàlla [moo] lay teral
ku bëgg sa yaay? (youssou) waaw! waaw!
ku bëgg sa yaay? nél jërëjëf!
ku bëgg sa yaay? (youssou) waaw! waaw!
ku bëgg sa yaay? nél jërëjëf!
tu aimes ta maman? (youssou) oui! oui!
tu aimes ta maman? dis merci!
tu aimes ta maman? (youssou) oui! oui!
tu aimes ta maman? dis merci!
you love your mom? (youssou) yes! yes!
you love your mom? say thank you!
you love your mom? (youssou) yes! yes!
you love your mom? [say thank you!]
tu ami mamá? sí! sí!
tu ami mamá? di grazié!
tu ami mamá? (youssou) sí! sí!
tu ami mamá? di grazié!
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu 11six music d.l.b - hustlers prayer ii
- lirik lagu celestial wizard - into the abyss
- lirik lagu morgan wallen - miami (remix)
- lirik lagu линда (linda geiman) - танец под водой (live) (dancing under the water)
- lirik lagu n3xther - the promise i pretend (rearranged vers )
- lirik lagu crescenda - where have all my prayers gone?
- lirik lagu adbeatzer - taghazout freestyle
- lirik lagu george windsor - do my thing
- lirik lagu luru money - yeah
- lirik lagu ellie denmark - lolita