lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu youssou n'dour - tukki

Loading...

yoon wi nga jël baaxul ku la koy digël da lay sax
yoon wii ci des moo gën, loo taseel dàldi koy mën
yoon wii nga jël booy dox ba ca biir géstul xool fi nga weesu balaa ngay

booy tukki yaw
booy tukki yaw

na nga bàyyi ba mën
ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
dina tax nga mến xam nekkinu neneen
foofu mën nga fa gis lu yókk sa xameel

booy tukki yaw

nita ngi toog di janoog yaw b00ba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan
àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam
yaw sama away kaay ma xamal la
léég léég nga toog fi nga toog tukki tukki bu neex dem ba kaw asamaan
ànd ag weer wiy naaw li ngay janeer mu lay neex boo janoo mu gën fee neex

booy tukki yaw

deel tukki yaw yeesal sa xameel
ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
dina tax nga mën xam nekkinu neneen
foofu mën nga fa gis lu yókk sa xameel
deel tukki yaw
lëppa lëppa sàmba ma ngay naaw, te booy seet sax taxu koo gaaw
te léég léég mu dem ba kaaw
tukkee ka neex, waaw
lucum ceeli ma ngay naaw te léég léég mu naaw ba kaw
asamaan indi fiy xabaar
ku dul tukki doo xam fu dëkk neexe

booy tukki yaw
na nga bàyyi
booy tukki yaw
na nga bàyyi ba mën

ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
dina tax nga mën xam nekkinu neneen
foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel

booy tukki yaw
booy tukki yaw
booy tukki yaw
na nga bàyyi ba mën

naanu barke ah naanu barke
nita ngi toog di janoog yaw b00ba fekk na ma ngay xalaat ba tàbbi asamaan
àndag niir yiy naaw dem na fu sore lépp ciy xalaatam
yaw sama away kay ma xamal la
léég léég nga toog fi nga toog tukki tukki bu neex dem ba kaw asamaan
làng ag weer wiy naaw li ngay janool mu lay neex boo janoog moom mu gën fee neex
booy tukki yaw
na nga bàyyi ba mën

ding cë jëléé lu mënë xew ca feneen
dina tax nga mën xam nekkinu neneen
foofa mën nga fa gis lu yókk sa xameel
deel tukki yaw

lëppa lëppa sàmba ma ngay naaw, te booy seet sax taxu koo gaaw
te léég léég mu dem ba kaaw
tukkee ka neex, waaw
lucum cééli ma ngay naaw te booy seet sax taxu koo gaaw ëndaaleel nu xabaar
tukkee ka neex, waaw


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...