lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu youssou n'dour - tijaniyya

Loading...

yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
li nga def ci jakka yi, baayi dabakh waccnga

jaa jef sy yaa deggal liggeeyu fa wade welle
cheikh oumar waxoonna ko, yaa taxawal tarixa bi

yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
li nga def ci jakka yi, baayi khalifa waccnga

gannaar xamna la, waa maka xam na la
yonent bi geremna la, yaa yore tijaniyya

yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
li nga def ci jakka yi, baayi serin mansour waccnga

yaa fi xewal gammu gi, yaa fi xewal wassifa
zaawiya seede la, reew mi ameelnan la njukel

yaa fi xewal gammu gi, yaa dundalaat daara yi
li nga def ci jakka yi, baayi dabakh waccnga

dedduwoonna adduna (baayi dabakh waccnga)
moo doon boroom suuna (baayi khalifa waccnga)
di it ku amoon fulla (baayi serin mansour waccnga)
mandoom ga landina (baayi dabakh waccnga)
xam xam ba selina (baayi khalifa waccnga)
dajaloonna teere ya (baayi serin mansour waccnga)
doxewuko, damoowuko (baayi dabakh waccnga)
cheikhou oumar foutiyou tall
maami seydou norou tall
waxoonna ko
yaay taxawale tarixa cheikh ahmed, tijaniyya
cheikhou oumar foutiyou tall
maami thierno mountaga tall

dajalenga kilifa yi


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...