lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu youssou n'dour - tan bi

Loading...

sedd bi ag tangaay bi dafa mel ni yeppa yam
bu ci xas yegsi ba jall da nga naan moo la genel
seddaay bi, tangaay bi

koo geje gis nan ko xaar tangaay bi
bu tambalee neppa nei ci tali bi
bu becegee nu feexluji ci geej gi
bu guddigee nu lang ci jardin bi

sedd bi ag tangaay bi dafa mel ni yeppa yam
bu ci xas yegsi ba jall da nga naan moo la genel
seddaay bi, tangaay bi

bu sedd bee nepp lelu ci ker yi
nii di waxtaan waxi mbegeel ci neeg yi
yakkamtinan guddi ba dem fatu ji
mbajj mu diis nnu jakkaarloog tele bi

ni sedd bi yegsi na and ag ngeneelam
tangaayi tam tabbi and aki feemam
wooy jaaraama jaarawulee, jaarawaali

sedd bi ag tangaay bi
bu ci xas yegsi ba jall da nga naan moo le genel

wuy jaaraama
woow woow wuy jaaxle


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...