lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu youssou n'dour - sagal ko

Loading...

xale bi kii de jaaxle na, sonnal nga ko de xamul ku dul yaw

xale bi ndeyam ba na ko, baay ba ba na ko te gisoo ci dara
xarit na nga regle
xarit te nga xam ni bun ko defoon sa jigeen di na la naqari
yerem ko, sagal ko

xale bi ndeyam ba na ko, baayam ba na ko te seetoo si dara
xarit na nga regle
xarit te nga xam ni bun ko defoon sa jigeen di na la naqari
yerem ko, sagal ko

jef joo gis am na pay
jef ju baax am na pay waaye jef ju bon it am na pay
xarit seetaatal bu baax ni ngay doxalee

xale bi kii de jaaxle na, sonnal nga ko te xamul ku dul yaw

na nga regle
xarit te nga xam ni, xarit
na nga regle
xarit te nga xam ni
xarit te nga xam ni, xarit
te nga xam ni, xarit
na nga regle, xarit
te xam ni adduna de jaru ko
geestul sa ginnaaw
yerem ko, sagal ko


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...