
lirik lagu youssou n'dour - moor ndaje
te sax adduna kenn du ko dajal, ku dul umpele danu lay ragal
faww nit ku ne am lu muy desal ngir bu ellegee nu men laa setal
fu ne nga nekk fa
lu ne nga dugg ca
heh heh begg naa nga dal
yoo moor ndaje deel sooraale ellek
woo yoo moor ndaje deel sooraale ellek
lekkoo ci ndap li begg ci xepp suuf
lekkoo ci ndap li ngall bu ci xepp suuf
woo yoo moor ndaje deel sooraale ellek
boo ci lekkul it bu ko xan keneen
kanaan fankul muur yalla mood meye
woo yoo moor ndaje deel sooraale ellek
menaguma dem waaye keneen du dem
xamal ni bu yoon jeexul waaxusil du jeex
woo yoo moor ndaje deel sooraale ellek
faww nit ku ne am lu muy desal
degg degg daal di nga raw
woo yoo moor ndaje deel sooraale ellek
boo moytuwul yaw lanuy riinion
television yi ag rajo yi sax am na lu nuy umpele
waaye fleme mbooloo ni afiisu sinemaa
moor jamais rate moor wannil ma sa gallaac
boo moytuwul yaw lanuy riinion
xawma mbaax la xawma den k~mpe la
moor ndaje
xawma mbaax la xawma den k~mpe la
moor ndaje
yaw menuloo jef sax ba kenn woolula
moor ndaje
boo moytuwul sax yaw lanuy riinion
moor ndaje
boo moytuwul sax yaw lanuy toogee
moor ndaje
yoo, yee
moor ndaje
wuy yoo, wuy yee
moor ndaje
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu hairpin - oh dear
- lirik lagu sxr (ind) & akillar - zaddekob
- lirik lagu krokodil (berlin) - dogpiss
- lirik lagu lil mister - all i know
- lirik lagu тапо4ек (slipper) - sigmafreestyle
- lirik lagu hukeykaran - hukeyyyyy
- lirik lagu dr. rocka - sin temor
- lirik lagu blakes (rap) - provide
- lirik lagu ryul - oxygen
- lirik lagu jfk47 - a goon corre por sp pt2