lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu youssou n'dour - mbëggéél noonu la

Loading...

ku ne langal ag sa waay, bu neexee du metti, mbeggeel nooonu la
naa la wax lu ma menul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am
naa la dik lu ma yorul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am
wuy mbeggeel ooh!

ku ne langal ag sa waay, bu neexee du metti, mbeggeel noonu la
lu ne ngi ci biir mbeggeel bul di bare looy seetlu mbeggeel noonu la
naa la wax lu ma menul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am
naa la dik lu ma yorul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am
wuy mbeggeel ooh!

aah jali ni la mbeggeel di def saa boo yewwoo te doo ci men dara
waaw jali su dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol
kaay ma digel la bul seentu sa ginnaaw aah
waaw jali su dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol
ma digel la bul seentu sa ginnaaw aah

xoolal ci sa kanam moo gen
naa la dik lu ma yorul ngir nga beg xam ni yaw mbeggeela am
naa la wax lu ma menul ngir nga beg xam ni yaw mbeggela am
wuy mbeggeel

aah ki nga begg mu begg la bul di xool leneen di leen yamalе
langal ag sa waay
ku ne langal ag sa waay
aah ki nga begg mu begg la bul di xool lеneen di leen yamale
ku ne langal ag sa waay
wuy mbeggeel
bu dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol
ma digel la bul geestu
ah ku ne langal ag sa waay
buy neex ag buy metti, mbeggeel noonu la
ah mbeggeel
bu dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol
ma digel la bul geestu
aah langal ag sa waay
bu dee ki nga njekk nop dafa yaq sa xol
ma digel la bul geestu


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...