lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu youssou n'dour - mahdiyu laye

Loading...

bu de dangay leble
lebleelal ku am pey
seydina limamou
yalla feyna ko

neent f~kki at ya
mohammed woote
neent f~kki at ya
maam limamou woote
mahdiyu laye

mohammed waxoonna
mahdiyu gi ci yoon wi
seydina limamou
feen ca tefes ga
and ak issa

maami maam rane laye
moo niwoon geej ga
yow xamnga maay kan
bëgg naa nga dellu
ca la geek ga delloo, laye

keroog la woote
adjiboo daayirahi
kaayleen, kaayleen
nowleen, dikleen
jaamu lamul ahzam
laye
moo dellusee, moo dellusee
moo dellusee, mahdiyu laye, moo dellusee

baayi issa laye
baayi mandione laye
ak ababacar laye
maami maam rane laye
ak ablaye thiaw laye
laye

maami ousseynou laye
mahdiyu feenna
sagalnga reew mi
neppangi naan laye
yaa and ak issa
laye

yaa dellusee, yaa dellusee
yaa dellusee, maam limamou, yaa dellusee
yaa dellusee, xammenan la, yaa dellusee
yaa dellusee, mahdiyu laye, yaa dellusee


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...