lirik lagu youssou n'dour - bàjjan
taasukat baa nga naan gainde gu waaf ca buntu kër gë, di melastiku
béy bu am bàjjan du fa dem, zacharia, bàjjan am na maanaa, wayal
lu la réér ci sa cosaan, sa bàjjan xamal la ko
boo bëgéé xam sa cosaan, xam la fa maam yi bàyyi woon
deal seeti bàjjan ba, lu mu la ca wax, du den
bàjjana xam kajoor ah ba ca mbeneex wa
cosaani askan wi, bàjjan am na maanaa
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sungun sangan bàjjan, bàjjan
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sungun sangan
neenanu mag de mët naa ba cim rééw waaye bàjjan it mët na bàyyi ci biir kër
xam sa boppa gën nu woo la naan kii nga doon
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sungun sangan bàjjan, bàjjan
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sungun sangan
boo bëgéé xam sa cosaan, sa bàjjan moo la koy xamal
moo la naan awal fii, bul dem fee, defeel nii
boo ko seetloo dara du ca den
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sungun sangan bàjjan, bàjjan
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sungun sangan
mani bàjjan moodi magi baay walla rakkam
lu xew lune mane bàjjan taxaw
bu góór dugéé néégu góór
bàjjan taxaw, wayal ko mbaax
nijaay di yaay nga di baay
bàjjan am na maanaa
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sungun sangan bàjjan, bàjjan
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sungun sangan
bàjjan moodi magi baay walla rakkam
lu xew lune mane bàjjan taxaw
bu góór dugéé néégu góór
bàjjan taxaw, wayal ko mbaax
nijaay di yaay nga di baay
bàjjan am na maanaa
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, sungun sangan bàjjan, bàjjan
wayum terànga la kuy bàjjan jogal yëngu, bàjjan, bàjjan, sungun sangan
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu inferisborn - she’s my sexy devil
- lirik lagu minelli & tobi ibitoye - alien
- lirik lagu dead hooded - rotting (inside)
- lirik lagu fearsavi - phonk banana
- lirik lagu th - mode sport
- lirik lagu weiland - in her dreams
- lirik lagu boy gé mendes - junta ma nôs (feat. manu lima)
- lirik lagu trupovert - нет не жди меня [no don't wait for me]
- lirik lagu s1xxxpy - :3
- lirik lagu jaelee roberts - you can't stop me from staying