lirik lagu youssou n'dour - baay faal
paroles de la chanson baay faal :
baay faal gueu da djook thia fadjar
nga sène ko mouy soli sagar
boppam ba sekkeu ki kawar
yoré keulleum ba di sikar
té falé woul khiif ak mar
boo démé sakh khekh na badar
ki toureum wi dotoul fay
kou wéddi li ladj ko wa ndar
baay faal djakhal na wa ndar
baay faal djakhal na wa ndar
baay faal gueu da djook thia fadjar
mani bour yalla da djook thia fadjar
nga sène ko mouy soli sagar
yoré keulleum gueu di zikar
ki toureum wi dotoul fay
kou wéddi li ladj ko wa ndar
baay faal djakhal na wa ndar
baay faal djommeul na wa ndar
doundeum gueu nekh na
zikar sa neekh na lol
baay faal bi, baay faal ki modi guènne goor
zikar sa motakh mou djégué yalla
baay faal bi, baay faal kouko khamone dinga mandou thi mome
thia tool yeu…
thia tèène yeu…
thia wagne weu…
magal yeu…
baay faal liguey la khame
baay faal ndigueul la khame
baay faal dou khekh dou khoulo
beuggue neu nite, fonk na nite khekhoulol
mome la fayé ko lo mou ligueyal sougnou borom
beuggue na la baay faal
nangou nite
kimo djégué sougnou borom
dey liguey di djokhé motakh baay faal djégué naa sougnou borooom…
dey liguey di diokhé
dey liguey di diokhé motakh baay faal
toggam ga nekhna lol motakh bay faal
dey magal motakh baay faal
dey zikar motakh baay faal
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu d double e - seeing double
- lirik lagu bigray - lost in hate
- lirik lagu tierra whack - niggalodeon
- lirik lagu andrew sam - shave day 2 (interlude)
- lirik lagu landy - bad boy
- lirik lagu sonic youth - side2side
- lirik lagu aretha franklin - ain't nobody (gonna turn me around)
- lirik lagu towkio - american apparel girls
- lirik lagu gloria estefan - mi tierra
- lirik lagu bexey & lil peep - repair