
lirik lagu samba peuzzi - mala baal
mala baal lyrics
nyungi and mais xam na ni gueumo ma
sa xarit la teh fo tok di wax ci man
bueugo ma dem da ng~y mer bu may avancer
mais douma la topp nala baal way
tonj nga ma benn yone
ma dal dila baal
nga del tonjati ma
ma dal dila baal
xam na jikom (yah yah)
yag nang bayil ma bayiko ci bir
why not?
mako baal mako baal
duma la topp mala baal waw
mala baal mala baal
sama waye mala baal waw
hey lonko ko depuis petit
lo yeuuk si man dem netali
poto duma la takal pottes yi
wollu la rek tax nyu yeksi fi
sa naxar daf may metti mais
done xale warul teh nga nek nitt
joxma sa baram bu ndaw nyu jubo
sa yaye ak sama yaye nyo bok natt
hum
deglu duma ken gumba teuxlu
ma guisseul sama bopp am luma bett
metti na waye duma topp sama xol
bayil ma demm ak xol
bueugguma j~pp di bayi hey
nyungi and mais xam na ni gueumo ma
sa xarit la teh fo tok di wax ci man
bueugo ma dem da ng~y mer bu may avancer
mais douma la topp nala baal way
tonj nga ma benn yone
ma dal dila baal
nga del tonjati ma
ma dal dila baal
xam na jikom (yah yah)
yag nang bayıl ma bayiko ci bir
why not?
mako baal mako baal
duma la topp mala baal waw
mala baal mala baal
sama waye mala baal waw
nitt bu soxoré
mba nyu iñane
mba mu siss
dama koy yeureum
fumu tolu volcan gui ci biram diko sonal
dama koy yeureum
dama lay yeureum
seeñ la beunj yu weex
neubb xol bu ñuul
ayayayayayaa
del xol ki ng~y def sa xol
ayayayayayaa
nyungi and mais xam na ni gueumo ma
sa xarit la teh fo tok di wax ci man
bueugo ma dem da ng~y mer bu may avancer
mais douma la topp nala baal way
tonj nga ma benn yone
ma dal dila baal
nga del tonjati ma
ma dal dila baal
xam na jikom (yah yah)
yag nang bayil ma bayiko ci bir
why not?
mako baal mako baal
duma la topp mala baal waw
mala baal mala baal
sama waye mala baal waw
seeñ la beunj yu weex
neubb xol bu ñuul
ayayayayayaa
del xol ki ng~y def sa xol
ayayayayayaa
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu englando - selvføli
- lirik lagu sauveur eloheem - dog food
- lirik lagu plej - you (quant remix)
- lirik lagu coals - omamy
- lirik lagu frankie goes to hollywood - holier than thou (part one)
- lirik lagu дегид (degid) - повзрослеть (to grow up)
- lirik lagu andy shauf - jacob rose
- lirik lagu burry soprano - venedik
- lirik lagu billy fury - letter full of tears
- lirik lagu tophyun - 미안해요 (sorry)