lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu pps the ghost writah - préface

Loading...

li mooy xaatim x 3 sama gueinte gué yeémé cool, mbekté di kemtane
waral nelaw yi yeggul, jok ndeké sa reetane
ferniente yi may weetali, sedal li, seedel li
p-ss p-ssu dellu ci war yi, w-ssaré love ci xol yi
tek ko ci tempo djiguene gniy soxeu ci euteu bi
xale yiy foo di rée, teub ak danu si eukeu bi
xeetou café ci deuk bi, kaff ak thiow yi niou woodeu
“adouna dou dara”
dem na, weur na, guiss na, legui xamna
woruma né, waruma gné, xamé na
li ngay xaru di yotu, soko djotée weuri leneen
k-mpe nga naane, mou muril leu noon, wari di neen
wutey sunu taar, xeutioy sunu tord
sunu koor, faté yeurmandé, waral niakay fignou teer
nioy souf nioy ganthiakh, -ssamane nioy dokh
nioy moome, moy nioune, nioy xaatim ak kallàma

{2}
une generation gené râle
à la quête d’un generale
aux jeunes les rôles, la voix on l’-ssume
l’afrique le drapeau, la voix et la plume
les aïeux dans les yeux, entre le marteau et l’enclume
de ma plume, ils s’emerveillent, ma rue est ma seve
ma merveille de mere veille, je vend pas du reve
pas de treve sur le sentier de guerre
le micro mon glaive, la vision des silions naguere
on ecrit le je, decrit la vie de nous
le rire, la joie, les pleures dans nos peurs
la haine et les peines de ceux qui vivent à genoux
les regrets, la nostalgie de ceux qui vivent dans nos coeurs
xaatim c’est ecrire, kallàma une maniere de dire
notre vecu, nos memoires, des oreilles à seduire
une utopie appelle moi pic-sso, un fou rire
on essaye de peindre les mots aux couleurs du sourire


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...