lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu pps the ghost writah - african flow

Loading...

si mbind mou taaru niou yeegueul level benene maxama

fooral ndeundeu yi, yeuglee peinthoo si benene kalaama
na gueew bi sadjeu, xel yi fathieu, niou dekal jalooree
deloo gueude xaragne, reudeu xoromal sen manooree
farafina vib sa nopp, african flow benene kangforee
xalam si toolou music ni gope, soukheute yaakar akhan askan wi foo ree
motherland fila lep doree, wakhtou jotna jok wanee finiou foree
waw gooree, goor yawone goree, tama g8 sen der laniou fooree
dakar ba nairobie, lagos ba kisangani
east ba west, north south, kiss ak peace a ngui ni
malembee papa, daniou guimi di guindi, raniel niawone la
li rere si magg gni, fegne si gonee yi, dalal diam niou wane la

{refrain}
african flow!!! african flow!!!
african flow!!! afri african flow!!!
africa sabaly, tek flow ci sabar yi
delou ji nafari, saggo ci sa barre yi
diomali sa forts yi, lyrical safari
lagos ba kinshasa, ouaga ba nairobi

african flow!!! african flow!!!
african flow!!! afri african flow!!!
djogui naniou sa mind, djegui naniou zamane
ya ngui khol sa jeum, fek niou taamou sa mind
fo niou feugué niou paré, si feem you baré baré
move sa body body, si groove nga party party

{2}
the flow is from the nil, the flag will stay up
here we go, flavor flow, louniou si wiss day eupe
recognize the man, the name is pps the writah
galsen si kaw, ngaye sen di daw, mouye gueune di law ni lightah
ladi dadi please, relax your body fils
deugloul sa daddy guiss, african party gna teewee biss
please – bis – jokh ma nombolo ma tek si flow
yeungueul si mbague yi mak yi, dougou si maqui yi leki abolo
ness kiss dinga yeek, loy teup ni ball
daniou moss ne tek, nga moss di teup di dale
tanef laniou done, mbed mo niou fale
daayou rap la, writah mo diafal
amatoul diafel, kou si meune dieufeul
wanee baatu xakk, jeuf dathie thiofel
flow flow, the flow is ill
east ba west jok lene niou wanee skill.

{refrain}

african flow!!! african flow!!!
african flow!!! afri african flow!!!
africa sabaly, tek flow ci sabar yi
delou ji nafari, saggo ci sa barre yi
diomali sa forts yi, lyrical safari
lagos ba kinshasa, ouaga ba nairobi

african flow!!! african flow!!!
african flow!!! afri african flow!!!
djogui naniou sa mind, djegui naniou zamane
ya ngui khol sa jeum, fek niou taamou sa mind
fo niou feugué niou paré, si feem you baré baré
move sa body body, si groove nga party party

{}
let’s move to the left, let’s move to the right
africans stand up as one, let’s dance all night

aythia aythia aythia aythia aythia teup
khatim ak kalaama sarr ci sa club
let’s move to the left, let to the right
africans stand up as one, let’s dance all night


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...