lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu phil black - biddeew

Loading...

bés bi nu doon xaar yegsi na
bés su mbegteh
bés su mbëggeel
sàma sajò baan sey si nä
kër gi kontaan nañu
fes ak jofeël
sa reffetai mel ni lerai yu asamaan
man li may yëg ci sama xol gui mako xam
män paréh nä bok ‘ak yow mi sai naqar
musu ma bàyyi ba tay
ndax

yalla monyu boleh
bes niki taye babe doma musa soreh
holal mbeguel nomu foreh
ron’goyn turu sama beut
yuma lai holleh

gisna biddeew sa har kanaam
mom lai leralleh sama adunaaa
gisna biddeew sa har kanaam
mom lai leralleh sama adunaaa

you the angel i was looking for
never had someone who loves me more
no
muso mer beh woneh sa giko
gis su ma fo musa sope ko
no
tu es la femme de mes rêves
a’ la vie à la mort
je te jure fidélité
mi amor de près ou de loin
je serais à tes côtés
juste pour t’épauler
yalla monyu boleh
bes niki tai babe doma musa soreh
holal mbeguel nomu foreh
ron’goyn turu sama beut
yuma lai holleh

gisna biddeew sa har kanaam
mom lai leralleh sama adunaaa
gisna biddeew sa har kanaam
mom lai leralleh sama adunaaa

gisna
biddeew
mom moi leral sama adunaaa
waaaw
waa waaw
mom moi le larall
man gisna
biddeew


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...