lirik lagu pape diouf - partir
Loading...
bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem
liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takkla
mane nanelay deff
limay raggal moy wanela guinaw nga
fattemay souboba dinama nakari ndax ande bi yagna
mane nanelay deff
wayei fouma diar mane dina dem liguey
ndax may taw wadiour yi manelañu yaakaar
né faw ma dem outidji nguir terral la
baby sorry gueneulouma baby mangui nieuw
beugnala xalei biley
bima deimei ñu mayema visa il faut que ma dem
liguey nguir terral samay wadiour souma nieuwei takela
mane lanelay deff
wayei fouma diar mane dina dem liguey
ndax may taw wadiour yi manelañu yakaar
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu vilardz & b.a.t.h - zombie
- lirik lagu flake lorenz - guten abend, schön abend
- lirik lagu three mo' tenors - today i sing the blues
- lirik lagu دكتور معجزة - bonjour - بونچور - dr mo3gza
- lirik lagu bikelock - low wound
- lirik lagu laufey - while you were sleeping (live at the hollywood bowl)
- lirik lagu sun daze, welsey eisenhauer, juke the tiger - fair weather friends
- lirik lagu babytali - cryyy
- lirik lagu marina tadić - zaboravi
- lirik lagu poison ivy uk, - bounce