lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu nitdoff - yiw la tchi dioublou

Loading...

{ombré zion – refrain}

{verse 1}
yaa yaa li djip cii mane di nieuw cii yaw yaw rek la meuneu gondi
domou alioune nak diyeu samba no dou meuneu bone
do meuneu xam bane beute ngamay kholé souma neubou woon
kou nakari dérette bagne kouka yapp dou meuneu togne
meune ngama yéné moussibeu, meune ngama yéné yiw
meune ngama séddel jeuf djou baax ba sama ndam li siiw
li djam bi def rek ci lakoy yallah fay au retour
nga gass soule dieul safara dem cii beureup tuur
yaw rekkay youxou cii baamel bougnelay teur ak kour
légue légue ma guiss leu nga tégui yone yi ma wo remind leu
yiw la tchi djoublou my n~gger aduna wori nèène leu
yallah nopina dembe kone lou waxtane djot mou yèmbeu
sheytané meune na beuré moytoul mauwty dj~pp ngèmbeu
kou bania totchamo kandja boul sango paanou tiir
kou diokhé jaameuh am jaameuh bou yeukeutéti fitna
kaddu yi totch neu yiw tourouna one love bi djipp neu

{ombré zion – refrain}

{verse 2}
one lova love boulko rousseu tontou saga noone (one love)
bou yaggué dina rouss reuthiou né dafeu saaguanoone (one love)
donal pousso di niaw rataxal fi niagassone (one love)
na jaameuh rek di am cii niit gni nala diaral soneuh (love)
boudoule diégueulé diéleulé do meuneu yagg ak kèneu (one love)
yaw meune nga laabireunté, massla té dou andak fèène (one love)
xol bou fessoulak love djeumeu djeu day leundeum kriss (one love)
waayé bouy nangou nattu rétanam day neubeu tiss (one love)
yéwéneul cii kom~kom so beugué mou yokou barkél
bène bo def cii mbaax yiw beu foukou lagnelay marquel
lignou boolé mo eupeu fouf lignou taggalé
meune nagnou bokkeu yone kouné aagueu té doma taclé
djékou baalé boul dii khaawi soutoureuh ak gaawa aalou
boul tass yakaarou kèneu, boul xépp say niitou dembeu
boul guiss sa bopp cii lèneu bay dox di feugueu deundeu
modestie dess cii moytoul sheytané keuf leu cii test yi

{ombré zion – refrain}

{verse 3}
yaw bou pouvoir néké say loxo sheytané yaw lay ciblé
boudé bo santaané niou jeuf kholaatal li ng~y diguelé
niitou fitna bou jaameuh dji beuré day ennuyé wou
fouy yokou merr lay tekk baramam naniou andeu yéwou
ki naane leu bayi kok yallah ki naane leu fayoul légui
ki naane leu boul démé dolé ki naane leu réindil djégui
yonéinte bi missaale leu cii bepp human bii
kou roy cii mom mouthiou dembeu euleuk ak moment bi

{ombré zion – refrain}


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...