lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu nitdoff - virus

Loading...

[refrain x2]
raye comme un virus daniouy raye comme un virus
raye comme un virus daniouy raye comme un virus
député nga wala ministre
bbc nga wala timis
communicateur traditionnel nga wala fimisté
avocat bi dafeu teulé mogui saga wané p~n~s
naka djiek da nga teulé sou beat bi di takk n~gga naleu punish

[pont]
boleen wakhé deugu, da nga réw
bounie leu diwé beurre bi, da nga xéw
politiqué naniou louné bi meu moudjié niakhtou procureur bi dama jail
magui souba nouniou nara mél
niakk repère moniou nareu ndél
moukalaf gnigui tokk ci télé bi di fenn fenn you nekh ni caramel

[couplet 1]
thia deugu deugu dama tite
thi mandargua hypocrite yi meu guiss
deuk bi sameu touniou sunu nguor
té guatié ci iliman yi leu siite
malettou macky ndèké di nga soss
sou xoutba ni nеkhé di nga sossate
diné dji legui yéw neu sunu baatе
té serigne ci barétou niou so sad
niepeu ngui wantér sén nguor
nane ndokh xa gueuneu diafé taye worr
garabou bagnekat yi laniou gor
taye djikoy badola laniou forr
bakh ci discours yi leu yam
weuyou bou dedicacé layam
waatt ci serigne bé kiy mayam
nga guiss kou sandiafou ayam
ci souf beu encaisser payam
nafsou yéw naniou ci réer ken deguatoul ngereum
diam tekk beutteum deureum
bamou diaral ko sakh di xeureum
léer loul ci liy soloom ndakh ibliss mogui ley seuleum
daan naleu baley xeuleum
[refrain x2]
raye comme un virus daniouy raye comme un virus
raye comme un virus daniouy raye comme un virus
député nga wala ministre
bbc nga wala timis
communicateur traditionnel nga wala fimisté
avocat bi dafeu teulé mogui saga wané p~n~s
naka djiek da nga teulé sou beat ni di takk n~gga naleu punish

[couplet 2]
société bou dioub kocc amoul
family bi fokk mou rakh (virus)
wayé adouna loumou teureudi deh téwoul gni beugu bakh nio gui bakh
seu vice saleu dougual ci niawtef you bari ni yagui xeuy djiap njiakh (virus)
dokho ci lou yiw diayantéwo keep it real sa nafso ngui free ni fakh
pedophile leu mo raw virus (virus)
boul neup neupeul wowal police (virus)
sangu soutoura bou bari fadioul dianguoro bi deh lolou dou solu (tion)
serignetou beu moudjié oumou (virus)
ndieukeunté bi lolou loumou (virus)
ndeguem weurseuk dey djitou sa dioudou
fonek dey feugu salamaleykoumou
gars yi gueumeutouniou wisdom
accaparer founiou guiss koom
virus laniou ci biir askane
daniou pervers daniou miss mbonn
masla moniou tardel (virus)
je le redis je le martele (virus)
li fi yéess laniou barkel
legui lobbie yagui samp cartel
palais amna virus
assemblée amna virus
serigne boudoul guindi sey talibé ya raw virus
sunu music bé keu bari virus (virus)
prof bouy chantage élève (virus)
policier bouniouy bokhal
dg bou deup caisseu raw virus (virus)
[outro]
wallahi wallahi wallahi wallahi wallahi
wo hoo wo hoo wo hoo
wallahi wallahi wallahi wallahi wallahi
wo hoo wo hoo wo hoo
wallahi wallahi wallahi wallahi wallahi
wo hoo wo hoo wo hoo
wallahi wallahi wallahi wallahi wallahi
wo hoo wo hoo wo hoo


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...