lirik lagu natty jean - ak yow
sans yaw, dafay melni àdduna day bëg tukki
ak yaw, damay melni ku tëye alalu bukki
dëgg la sama chérie kon tay jii maa la tooñ
wante yaa ma xamal tay jii luma xamulwoon
maa ngi fataliku bi ñuy toog ci boppu koñ
suñuy gént ag sunuy yeene rek lañu amoon
waye seytane dafay faral di jaxase di ñu féewale
seytane bëgul ñaar ñu bëgante, bëgul ñuy fo di ree
ndax yaw laa love
baby yow laa bëg sama life
baby bu dul yaw man dinaa die
baby jàpp naa dootuma bayyi
(2x)
sans yow, dara dootul neex, man lepp daf may sàppi
ag yaw, damay bëg ba fumala séen di lappi~laapi
chéri man ag yaw du hasard
gëm naa ni boo pareegul man damay toog di la xaar
chéri man ag yaw dafa tar
looló waral man ma gëm ne lepp lepp dina baax
ndax yaw laa love
baby yaw laa bëg sama life
baby bu dul yaw man dinaa die
baby j~pp na dootuma bayyi
waye seytane dafay faral di jaxase di ñu féewale
seytané bëgul ñaar ñu bëgante, bëgul ñuy fo di ree
baby all my love is for you, i go sing it
bul xool ci benn seytane bul deglu benn wicked
ma ñàkk sama bakkan fuma toog dinaa la siggil
bimala xamee ba leegi bëggatuma keneen
chérie coco banne dama jooy, man dama fada
bëg naa doon papa, ma def la mada
sama xol bi moo la fal te jox na la benn mandat
à vie te nee na loo bëg dina ci ànd
mais yenn saa yi bumala tooñee
sama chérie nang ma baal
te baña topp waxu noon yi daf ñuy gaañ
ndax yaw laa love
baby yaw laa bëg sama life
baby bu dul yaw man dinaa die
baby j~pp na dootuma bayyi
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu צביקה ברנד - black - zvika brand
- lirik lagu cherry ills - jigsaw
- lirik lagu penny on mars - so sure
- lirik lagu jdbeatz & jburnie - monopoly
- lirik lagu deem spencer - 05' shit
- lirik lagu kwaku - flex
- lirik lagu xxfayme - ghost
- lirik lagu lil ricey - manifest
- lirik lagu natty jean - sénégal
- lirik lagu jp cooper - call my name