lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu lyrixist - soumay reud

Loading...

miserecord leu boy

sirtam on da beat

soumay reud xol dou yeug, beut dou guiss té xél dou sickk..
liçi dounya ak thiaayiram bou néékh lam niou dikk..
dacc lépp faire le vide total
ci thiéll bii niou ootal
lyrics yi geune niou ségg ,sarr ci xéllou, sakh ci dootal
lénén loudoul?
xél bou baawnaan déngamaam
lifay bawoo naan
mbeur dou gaawa ndaam; déggloul
niou took ci rouh
laal xol bi , jeum diaayou
reud tothie sirrou
knowledge wisdom ak lénén lim eumbe
amoul sikk esp~ce temp yaa guédj la teumbe
naah sol yéréy yéré einstein , charle menson ak béthoven
i’m shine daa leu plus math get to fén
lii dou xawi késsé ,jeum jé sééy thie tafaxour
dama raw ba técé paré té jomba cal sa tour
concocter c~cktail xéép lou molotoov
inshaker lyrical vibes yéma offff……

off lima done téck yaw off lima done tay
soumay reud mélni yéna took di wax
purger pеine , relater quеlques faits , amour di féllou haine
soumay reud , dounde moy taxaw dedelé fénn..

haine verser quelque litres , fatalikou argner
céder place égo moooy sopi bars yi armés
art diar ci baatou moumeu , dééy ci nopou teukhh
toumeu troner, reud pour gni mare si consi keukhh
reud pour penser plaits yi am taan junky ci cure filter
ki wara kaddu ak mane link ci dirr tipser
sa self téwal safara dacc jambaat jeul position ci thémes yi taamou porter flambeau xambaat..
soumay reud
chaque idéo détaillé
amasser info laal ci norme
compter vers retaillés
explorer chaques cours ; size bi diss co bics yi
discovery mba rap ; wax j daalou biti
beat yi comme tableau médite indi èrou davinci
daa fégne ci couleur ak fond formel ma mc
té mème si bou lépp xadioul last strophe
défci part de véritéy on li masse off…

off lima done téck yaw off lima done tay
soumay reud mélni yéna took di wax
purger peine , relater quelques faits , amour di féllou haine
soumay reud , dounde moy taxaw dedelé fénn..

soumay reud mélni yéna took di wax

soumay reud , dounde moy taxaw dedelé fénn..

soumay reud mélni yéna took di wax

soumay reud , dounde moy taxaw dedelé fénn..


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...