
lirik lagu griimpa - sad
Loading...
g-yi di teup di dal zombalé ték kheul
ma diap bop tok nék seul
maman diap bop khaléyi di dioy
lou gneuri mak warko fégnal keupou na soy
life bou sombre wakhi sama nop defete weurma nombou
yaw sama wakhouma kharr taf liste
tali bou liss ng-y dokh di rite
tour fégnoufa gneurign fégnoufa
jimko yallah tang na dougou gallé teu nama
beuré na wante life bi seuleum nama
boudé diang dako mako t défna ko
tanki bagn t ma ray sama bop
yakar bou t-ss yélouwan bou keupou
louma lal khawma lep deugueur boudéh dagn ma léguéy wakhma
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu jeembo - fallen
- lirik lagu low roar - give up
- lirik lagu king gizzard & the lizard wizard - elbow
- lirik lagu wombats - the english summer
- lirik lagu mia smith - bye.
- lirik lagu virtues music - nothing at all
- lirik lagu psychic love - go away green
- lirik lagu glaskaca - putih
- lirik lagu woodkid - winter morning ii
- lirik lagu veljanov - der kongress