lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu ghost mortel - yaw la taan

Loading...

| lyrics

pre~refrain

djiguene yii barri nagnou fii wanté xool bii yow laa taan
maa waax ko sameu yaay booy wanté neena yow laa taan
mbook yii validé copain yii neenagnou iow lagnou taan
ndax danga outé ak gnom bokkoulok gnom gnii meelni taan !!!

refrain

yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan

couplet

bou baakh bii laa deukoone dii weur
dou guudé daay fanane sii keur
tàànef bii djeek djikko
daaray adouna dh tiiteulou koo
yiiw neu yarou neu taarou naa
taabé nga taabal sa adouna
tangaal sa xool bii sakh warouma
dama doof sii yow té naan dara dalouma
kou meel nii yow sii jeune belle fille
djaafé neu lool sii jamono djii
douma nella bye bye ndax douma djiik
neema waaw rek gnou deem taak jii
maay kiiy feug nanga ma oubbil
my sunshine ioe leu aby
sii ben djiguene rek mom laa miir yow làà tààn nanga ma piqûre
refrain

yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan

couplet

boulma miin
boulma miin
boul ma miin baa faaté ma
kone mou gnaaw waaaawaaaw !!!
boulma miin !! jongoma
boulma miin
boulma miin baa sagganè ma kone gnaaw waaawaaaw !!!
lingère nak yeureum meu
jongoma yeureum meu
deuk dii daaw taallu ma nellaw
joot naa nga yeureum
yeureum meu yeureum meu
yeureum meu yeureum meu
yeureum meu yeureum meu
wooowooh yeureum meu !!!!!
enh enhh
pre~refrain

djiguene yii barri nagnou fii wanté xool bii yow laa taan
maa waax ko sameu yaay booy waayé neena yow laa taan
mbook yii validé copain yii yow lagnou taan
ndax danga outé ak gnom bokkoulok gnom gnii meelnii taan!!!!

refrain

yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan
yow laa yow laa !!! hé mane yow laa taan

outro

i need your love
i need your love
i need your love
i need your love !!!!

Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...