lirik lagu emmanuel lhebreux - boroom ndakaru (lyrics)
mr district, vas y
manipule moi la prod là
assalam alaykoum
thieyy
yesu moy nekk ben~euh
danguay bañ danguay guen~euh
doudou doudou gou cell~euh
ni dess n’yup dagni fene~euh
doundou doundou gou moutch, dang~y wara dial ci tally bu bess~euh
mbeugeulam daffay ray, ken dula wax car daffay fess~euh
diougou~leen seen boop
ben loxo du taccú
serigne bi mongui dúgou
beussou magal romb na xew
yoon nam daffa xat
danga wax daffa chère
sène yoon dafa makk
danga doug danga de
màggal~leen ko, yeen malaakaam ak gàngoor yi
màggal~leen ko, yeen jant bi ak weer wi
màggal~leen ko, yeen mboolem bidew di nes~nesi
màggal~leen ko, diougulène tacc aji kawe ji
nguur bu bess, nguur bess
li lagn done xar
xell mou sell mi
mo nieuw ci dakar
nga dem ci teungueth
nga dem ci tamba
amoul lo morom
yup ci teranga
kay dem gnou feutcheu
boroom ndakaru
kay dem gnou feutcheu
boroom ndakaru
ayca gnu magal
boroom ndakaru
ayca gnu magal
boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
neleen buntu yi kulbét
ubbileen bunt cosaan yi
saytane kanieu ng~y bayi ?
buur boroom ndam duggsi
samp suuf biir géej
moo samp suuf biir ndakaru
samp suuf biir thiès
samp suuf biir gaal~sunu
taccu~leen ko, yeen malaakaam ak gàngoor yi
taccul~leen ko, yeen jant bi ak weer wi
taccu~leen ko, yeen mboolem bidew di nes~nesi
taccu~leen ko, diougu~leen feucc aji kawe ji
fu ngeen di fekk ki sax bu mel ci baax
kone buleen fàttaliku seeni bàkkaar yu yàgg
lépp li mu def ngir gnu guen ko meune di tàcc
na lépp luy noyyi
màggal ki sax !
nguur bu bess, nguur bess
li lagn done xar
xell mou sell mi
mo nieuw ci dakar
nga dem ci teungueth
nga dem ci tamba
amoul lo morom
yup ci teranga
kay dem gnou feutcheu
boroom ndakaru
kay dem gnou feutcheu
boroom ndakaru
ayca gnu magal
boroom ndakaru
ayca gnu magal
boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
boroom thiès, boroom diourbel, boroom fatick, (yaw yay lepp)
boroom kaolack, boroom kolda, boroom kaffrine (yaw yay lepp)
boroom ziguinchor, boroom kédougou, boroom sédhiou (yaw yay lepp)
boroom louga, boroom matam, boroom saint~louis (yaw yay lepp)
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
yesu mooy boroom ndakaru
anh anh anh
yesu mooy boroom ndakaru
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu verifiziert - bullet holes
- lirik lagu uo aiff - concord (j11)
- lirik lagu mayday (uk) - trespass coat
- lirik lagu peter murphy - the answer is clear (version)
- lirik lagu shua - how to let go
- lirik lagu goiânia/go - teu piloto ainda sou
- lirik lagu jam - no beat just drums
- lirik lagu m waves - keep your dreams close interlude
- lirik lagu reyny daze - pressure
- lirik lagu siah the clown - have you ever? (part 2)