lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu elzo jamdong - zero garantie

Loading...

intro:
yeah… yeah
yo gni ngui tchi yonou wout beu legui…
khamouniou kagn la niouy nopalou
yeah…

verse 1
def naa ay ndiaakhoum homie
homie def naa ay ndiaakhoum dolli (def naa ay ndiaakhoum dolli)
moytoul ma waa dji gueuneu meuneu noppi ndakh defkat dou aalou homie (defkat dou aalou homie)
defkat dou alou homie (no no)
mané defkat dou alou homie
town dang-y waarou homie
pourtant kham naa lou baakh ak lou baakhoul

kogn bi ma maggué teela guiss business
legal bi dokhoul no def beuri vitesse
ba tonneau ni dt ak pet-t tchi corniche bi
17 ans rek nga indice ni odb
listen to me def naa ay bizness de merde
defaat ay bizness de merde
dem tougueul diangg fa ay yeneen system yu bèss
pour tek yeneen bizness you lerr (yeaaaah)

am naa ay ga you dakkh yeek ascenseur
ay ga you gueuneu khogne pimp bouniou tedj jail
ay borom baatin you gueuneu kowé aviateur
ay yaaram you meussoul niémé beugueunté’k guél
ay ga you beugg dope
ay ga you beugg show
ay ga you beugg flow
ay ga you beugg blow
ay ga you beuri doe
ay ga you super broke
ay ga you meuneu sope
mais samay g-yine legn though
oh
tannouma fi ma diouddo motakh ecole mounougn wone comp yane genrou people laay freq (yane genrou people laay freq)

alal dou dieund baraqa yalla beuggoul kouy dingat ak kheep (boul di dingat ak kheep)

yalla defoul loudoul li gueun diaroul ladjté ndakh djig na la’m deet (bakham djig na la’m deet)

yalla bind ne lepp moma binde ma meun binde ay textes

chorus
mounouma ralentir
fi leppeu yékh comme car rapide
tekki amoul garantie
motakh doumeu ralentir
doumeu ralentir

mounouma ralentir (ralentir ralentir ralentir)
fi leppeu yékh comme car rapide (car rapide, car rapide, car rapide)
tekki amoul garantie (garantie, garantie, garantie)
motakh doumeu ralentir (ralentir)
doumeu ralentir ih ih ih ih

verse 2
yeah
18 ans laa am dome (beugg tekki)
18 ans laa dem kaaw (beugg tekki)
18 ans laa am diom
baby mama waroul meusseu manquer cfa (faut que ma tekki)
bi ma dioté sama p-sseport (han)
fok né damay dem takhagn lou beuri dellouwaat
wayé ndéké tougueul aka beuri gallankorr
kou meunon khalaat ni naa bolé fac bi ak illégal ?
(yeaaah)

tek naa ay dealou cheque ay dealou call
motakh ma daan nieuw vac indaalé ay 18 calls
tek naa ay deal you sett, ay deals you thiole
ba soma guissone demb tey da nga naan kii dou mom
tchi sama khel bou gatt systeme laa done kheekh
teklé borrou loyer, bourler train i don’t care
sama khel di naatcheu may gueuneu malhonnête
di waadia teggui sama yone fok ne maa done chef (yeah)

diangal negn la qu’est-ce qu’on dit, kenn diangalouma qu’est-ce qu’on fait
gore yalla nammoul def comme diw, gore yalla dafay def done pé (yeah)
gore yalla khamoul def comme diw loumou tangg-tangg sagn neu nekk pompier (yeah)
guiss naa leen ngueen di def comme free mais yalla boumeu def comme yeen

bi paa bi gaagno mounouma wone dem fekké dedj bi ndakh beuri wone dette
boy town tchi hip hop bi, khèss, degg nguèw kham naa ni degn ma done khèp
aadio bou fadiou rek beneen nieuw tegou tchi diaroul ng-y diaakhlé mon frère
diambar dowoul homie maa ngui tchi sama conquête

chorus x2
mounouma ralentir
fi leppeu yeekh comme car rapide
tekki amoul garantie
motakh doumeu ralentir
doumeu ralentir

mounouma ralentir (ralentir ralentir ralentir)
fi leppeu yeekh comme car rapide (car rapide, car rapide, car rapide)
tekki amoul garantie (garantie, garantie)
motakh doumeu ralentir (ralentir)
doumeu ralentir ih ih ih ih


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...