lirik lagu elzo jamdong - yow lë
intro
yow le, yow yow yow le
yow le, yow yow yow le
yeah
verse 1
seme khol fess ne takh nga mey podj
nala defeul lo guissoul tchi ben gore
sey tiono dieekh neu maye kiley sore
waw gore doumeu bokk thi gore yi ley dore
guiss na ci sey beut khaar nga beu soye
guissoulo kou sérieux takh ne ngay dioye
sey rangogne fer neu maye kiley yor
niom ay kholou kheer legn yor mane mey or (han)
wone ngama fouleu ak diom
wone ngama wone ngama ndioub ak ngor
soubeu ak ngone dina dioubo ak yow (ak yow)
yama takheu beugg diour ay dome (yeah)
bou sobé yalla dinga sout se aye none
dinga diouyo ak niom gni beug doulo ak yow
dinga done boure dinga soure am forme
be gni leu beugone lor beugg ndouro ak yow
yow la beugg nala takkal bague kenene kouleu beug takk nako takkal ay pote
deug deug diaral nga ma raag doumeu doyeul dileu tagg gni le nièè di ko thiow
yafi tek #tank yaye #bombe kouleu #guerre nako #gun, #militaire laay done
binga dalé tchi mane le se khel wara dal, dinaa dem diakk dinga dem mairie sol robe
chorus
yaaye done ki diour semey dome
someu degueloul demey dofe (yeah)
yaye done diour semey dome (ooh yeah)
seme guenne walleu ngay done (woah woah woah)
seme guenne walleu ngay done (woah woah woah)
seme guenne walleu ngay done (ooh yeah)
seme guenne walleu ngay done (woah woah woah)
yow la tanne, yow la tamou (woah woah woah)
guiss naa tchi yow lou ken amoul ken amoul ken amoul
yow la tanne yow la tamou
dinga am tchi mane lou ken amoul
bridge
(woah woah woah)
yow le x4
verse 2
thièbou yapp bi khègne neu (khègne neu)
amatoumeu loumey neubb lepp fègne neu (fègne neu)
yagg naa dadialé ay thioro wayé limeu meusseu am tchi diangoro djiguene yeup dégne neu (han)
gni leu togne togn negn meu
naaw dou wakhou pitch ay wakhou wégn leu
dem thiakaye di tal seme money dou limeu gondi guenne balafi defey fekk me bégn leu (yeahhh)
legui takussane diot yaggueutoul, yaggueutoul legui takk sey diot
legui semey goro dal di sakkou sene dote
legui pa yi diogué diakk dia nga tagou sey mbok
mousso dem beu finale ak man
mouss nga touki wayé dinga dem fenene ak mane
denk negn mele nga fanane ak mane
seme dekhou bannekh ding fa nane ak mane
tey le biss bi dakh seme life tey la dogueu ne kilifa bimeu yagg beugg done (han)
seme mbokkou papeu yeup beg
souniou santeu dineu law diaré tchi kou rafet khol
mangui fateulikou bimeu done guente dileu khole di tchi meun diamou souniou boro
yangui yek pekh mi woné gningui tchi yone? ndakh néneu sey bokk ne limou gueuneu sopp
chorus
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu dwayne "the rock" johnson - pokérock theme song
- lirik lagu white buffalo - hold the line
- lirik lagu la cumparsita rock 72 - mi solución
- lirik lagu אביתר בנאי - תמיד לפני הגשם
- lirik lagu billy mani - se le fue la cochina al monte
- lirik lagu wac toja - gdzie jestem ja
- lirik lagu mark schwaber - the whisper no one else can hear
- lirik lagu reasonsmusic - why so childish?
- lirik lagu bruce carroll - walk on
- lirik lagu harris jayaraj, n c karunya & ramya nsk - oh maya