lirik lagu elzo jamdong - tchi kow
bimey ndieukk guiss seme clip tèlè dou wone dara tchi mane
khawme wone ma gui tchi revolution ni sarafina
bo nékké kawe kén dou diapp ya ngui rabati sakh
bimey ndieukk degg seme baat radio dou wone dara tchi mane
khawme wone mangui tchi revolution ni sarafina
bo deukké town degn le gueumlo né do dara tchi rap
tegone niou boy yi beugg dadialé ay tiaga di nawe
ken momoul ken-kén euppeulé woul kénn dara thi lenn
bou kenn khepe ken ngueum ngueum rek ak wara fi né
kham na aye galsén you meussoul dougg carapid sakh
diakhlé nga khate diappal ni mangui dogueu tambali nak
rappeur yi diogué bitim rewe doumeu séne morom
gueunougn me dounde wala khamné culture bi amoul borom
dou kana bi wala kawemàne be niou tchi euppeulé walleu
dou cannabis dou c0ke virus le boye accro di ko wallè han
rame sogueu takhaw diok sogueu dokh
rhymeul sogueu takhaw am lo meu wakh
mouno loudoul commenter diniou critiquer baye
mais kenn dou fi defati ni fi free dikké baye
dama teylou thi rap rap dogueu tédiou di rap rap
li ma deglou thi rap rap esk deglou nga kam?
mane deme free seme mind comme kouy fekheul relax
ancien talibé magg degn me sekheul ci rap
ngane´doolé nguey tek!? hum, degn niou booléwoul rek:
(nioune le) rakk yi ley rousslo sey kanamou rakk
malay indil bag-ssou mak ngamay diokh sey sagarou rap rap
ngané tangouniou? ha-ha danga khamagoul rap
dadialé kora, balafons ak khalamou rap
fawoume me feugg aye balles a fonds nga khalangou raam
deum ko beugg n0b ko te yow def le diaraloul sar
boumeu nekkone guel maye done diabarou rap
what?
ne se ga yi dem dallouwate ren maye falouwate
balou akkh
tabaski rombeu rek me alouwate
dieul lene seni alouwé dellou deglouwate me bou bakh poete yi me meun diangal moune na lene waagni moun nako wate
waw
mane mane ma fi diaye poete
waw mane mane ma fi fly kowé la def leopold senghor dey khate pour me atterrir setane na se clip mais sincèrement se style c pas terrible
j’arrive pas a tenir bullsh-t bi beuri neu
bala lou baakh di am rek dal faut q me diogué be paris koi
ken tchi ga yi amoul histoire vs avez merdé grave
motakh concerou samedi soir di mel ni mardi gras
ma daakh créer ma takh nga toppeundo
ah
ya daakh wéré kone bouniou tympaniser
moune nga topp seme band pour niou wone le yone
nieuweul seme live flow ba ngui waliyane
nel niom waly ak niom t-ti bizness bi diamm leu
tupac dou dioték biggie bou nekkone affaire de lamb leu
bou nekone dolé kone balla g-ye nieuw tchi game bi
toudd se tour ni kendrick te ken dou tidji se guemmigne
music ba ngui fey gni tchi gueuneu mouss comme d’hab
gni né tchi soufe dinegn yagg khouss te combat
bi dou diekhe filek nio gui gueuneu pouss contrat you baakh yi pour nga am tchi faw ma magg couz
bou le mbed bi naw se wa gallé méré leu
bou dé tchi yow rap weteuli chomage le wéré ngueu
nele mbed mi daw se wa gallé bégué leu
mc bouy topato wa gallem mbedd mi respecter leu
detester me se droit le boul me diémeu tester
boudé tchi p-ssé nga dess dé fi laley faté né mess dé
mangui ni di rap be beat bi egg 3mn pile
nga khamné limomey yokk mais dou diekheul semey pile
hook x2
mangui tchi yone
gni beugg peace negn me baayi di togne
negn ma baayi di togne
kaye tek tchi brique ndakh niou tabakh tchi kow
tchi kow, tabakh tchi kow
gni beug peace negn me baayi di togne, negn ma baayi di togne
kaay tek tchi brique ndakh niou tabakh tchi yow
tchi kow tchi kow tchi kow x3
gore yalla meunomeu t-teul
bi nga deggué me dore nga sogueu nangou peace up
pour se yone lerre homie moune naleu niteul
guiss na ling-y sore wayé meunomeu disteup
gore yalla meunomeu t-teul
bi nga deggué me dore nga sogueu nangou peace up
pour se yone lerre homie moune naleu niteul
guiss na ling-y sore wayé meunomeu disteup
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu sech - ojalá
- lirik lagu matay - perfeito
- lirik lagu platero y tú - la mate porque era mia - version 2005
- lirik lagu dalida - il venait d'avoir 18 ans - french version
- lirik lagu transit22 - dead flowers
- lirik lagu eddie kirkland - here and now
- lirik lagu cast of galavant - if i could share my life with you
- lirik lagu fonky family - check 1, 1, 1
- lirik lagu jake zyrus - pyramid (dave aude radio edit)
- lirik lagu capital inicial - universo paralelo