lirik lagu elzo jamdong - rwmr
intro
keah keah keah keah
rap wolof mo raw yeah
rap wolof mo raw
yeah
verse:
aka maa beuri ay fiston
wowema deug iba keyti bibson (rap’adio)
moussouma sokhleu se piston
yalla may nama kattan ak diction
pour danel leu diaroul may t-te
diaroul may yakamti caloul rek fils
ku diog song gaindé se kharou ng-y guiss
se sho ak se cachet laay nangou ne tir
dem chill seme borr
rap naa siguil sama kogne
mais legui il est temps me diw semey poche niou diss
comme nangou nga free defe fort
negn yengueul ba sodav fey niou ndakh faut que niou riche
meun nekk mc nekk pdg (ha)
diabanté aibd ak cdg (ha)
souniou joboul tabakh tem niou khey rek dé
souniou dome yi magg neniou wéré ngueen (hooo sh-t)
welcome to the macina (ha)
mane le amadou ampathe ba ci rap (ha)
ngandi kangam ni cheikh anta laa ci rap (ha)
yeubo teaupla bi fattewoul racinam (haaa shi-)
bro yeuppey capituler
lo kham ci poullo bou magué thi kognou lebou di leu lakk
ay olof you lerre
kou fi attann sama vocabulaire ?
rap wolof mo raaw rap wolof mo raw
nie wouniou states niewouniou kaaw
djolof mo ndaw rek sinon niou yéngueul ba adouna
yeup kham ne nio gueuneu graaw
rap wolof changer woul pour gueuneu feegn
nioune wagni ay fans mo niou gueuneul fake
niakk negn las dotouniou nelaw (las mc)
bourba ak pacotille ken doulene fey (rest in peace)
chorus
rap wolof mo rawww (rap olofdio rap olofdio rap olofdio)
rap wolof mo raw (rap olofdio, rap olofdio, rap olofdio)
(ha, heah, who)
rap wolof mo raw
rap wolof mo raw (rap wolof rap wolof wolof)
rap wolof mo raaw, rap wolof mo raw
nioune niè wouniou states my n-gg- nioune niewouniou kaaw
djolof mo ndaw rek sinon niou percer ba kaana yi
nieuw di niou follow niou naaw
rap wolof mo raaw rap wolof mo raw
(rap wolof rap wolof wolof)
rap wolof mo raaw, rap wolof mo raw (rap wolof wolof wolof)
djolof mo ndaw rek sinon niou feusseul ba adouna
yeup kham ne nio gueuneu graaw
rap wolof mo raaw rap wolof mo raaw
(rap wolof rap wolof wolof)
rap wolof mo raaw
yeah yeah
outro:
so feyoul douniou rap ak ‘oit
il faut que niou takk ni 60 watts
son bi tchi voit’ ak boite
shot out to black g rak tak squad
so feyoul douniou rap ak oit
da-da-damey diakh-ssé rap ak crack
rap wolof abadane
shout out rak tak squad
yeah yeah
-bugz from rak tak squad interview sample-
end
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu james ivy - blue eyes
- lirik lagu olliepiotras - disco wakacje ze starym
- lirik lagu trxpl1x - я не вернусь живым (i will not come back alive)
- lirik lagu kardeş türküler - de bila bêto
- lirik lagu cielo razzo - escorpión
- lirik lagu duncan laurence - silence
- lirik lagu odd crew - bitterness inside
- lirik lagu epica - if inside these walls was a house
- lirik lagu chikano & granddad woolly - we watchin'
- lirik lagu krishnokoli islam - আজ ঝড় ভালোবাসা