lirik lagu elzo jamdong - khel niaar
intro
mister thiere on the track
verse 1
tangg naa, songg naala, diengou na ba am ndam
diangg naa, diongou naa te pènkou laa yakaar niaane
nenegn free defey naane, am ne niou né damay tokh peudo
kham na ni meuneugouma topando kenn
mais khamagouma kenn koumeu meuneu topando (han)
limeu dioteu degg doyoumeu ak lepp limeu illuminati yi wone moyouma
bima done dane yeewou di dokh tchi neige bi diangg yaangui dieuw legui tey def negn le ko kholou nga
solou nga ba diss teklé ni choupomé
defeul niou khippi sou baakhé niou khef sou boné
sou kowé niou teup aadji linga rap tek
bou sobé yalla kouniou tester ding tchi ripp takkh
liy takh niou get sey onss (my brother) , moye se style dessé clean nga koy dionss (my brother)
def naa constant kholeul have a seat job bou setoul dou am suite
doumele setane né le fonce! (my brother)
constant motakh nioumay conss (my brother)
deme seuss seme gaayi khoss (my brother)
aay te do lekk mais c’est con ça waddup?
talouma clash cachet ross laa sokhleu
mister thiere mayaat ko refrain ben yone
chorus x2
boul khel niaar loye def nang tchi am ngueum boul khel niaar
yenn saay mounoul niakk khel niaaw
loye def nang tchi am ngueum boul khel niaar
boul khel niaar
verse 2
indi valisou crack tek fi
degn me warone takkal menotte sama poignet soumay eksi
lekk khalissou art tekki
wayé askan’ama fal motakh douanier douma tek ndiss
hey pet-t mane may leur-dea
maay #thiaat sopalikou #kilifeu keur gui
bi ng-y tek tchayine maangui keurti-keurti
diangg wala weur g’s loye def kheur tchi!
big up immitateur yi, big up bepp rappeur thiouné
yeneu takh niou tediou tchi waagne togg drogue you chic meuneu dougg founé
merci à la médiocrité merci mc yi am niveau c.i
yeeneu takh niou gueuneu meuneu raanié ancien nullard ak nouveau génie
sick-man nioune ng-y weur
beugg taal souniou dope di ko kheur
ma dagg boppou koumeu diokhoul thieur
damay dagg boppou koumeu diokhoul thieur
yekkal le ay punch banga feur
khalissou rap tabakh keur
fight féyékou comme mbeur
mais talouma baakou cachet zoss la sokhleu haha
mister thier diamaat ko refrain ben yone
chorus
boul khel niaar (khel niaar khel niaar)
loye def nang tchi am ngueum boul khel niaar (khel niaar khel niaar)
yenn saay mounoul niakk khel niaaw
mais loye def nang tchi am ngueum boul khel niaar, boul khel niaar
loye def nang tchi am ngueum
loye def nang tchi am ngueum
loye def nang tchi am ngueum
donté yenn saay mounoul niakk khel niaaw (khel niaaw khel niaaw)
mais loye def nang tchi am ngueum
boul khel niaar boul khel niarr boul khel niaar
final bridge
may ko benn pont bou ndow
bougoumala wone decourager motakh ma bagnone niou diakaarlo
damay reyaaté maakoy dagaaté danguene ma nara baakarlo
jamm dongg laay tewal, maam dess ne ci guerre bi
free crack, dore tchi kherr yi wala rek niou dore le ci kherr yi
west africa laa gueum doumeu topando kainkain
se flow safoul comme haoussa motakh me def ci kankan
nio bokk town biniou magué waayé souniouy yoneu diouyo
waroumeu leen di deglou my boy danguene may fouylo
melomind yi laay diangal di dougueul dope yi sene yourr
sopi naaleen ay baye fall legui nieuppey dore samay cours
maa ngui def limeu sentir souma pré kheyneu sene tour
moussoumeu dougg sene birr motakh ma nekk sene bour
motakh ma nekk sene bour
motakh ma nekk sene bour boy
it’s that freengdom danga dof wala dang-y diemeu tek rreaah
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu ralvero & ina - run wild (radio edit)
- lirik lagu stereophonics - all in one night
- lirik lagu jesus culture - make us one
- lirik lagu farid rashid - gray
- lirik lagu printz caligula - crushing
- lirik lagu corvus corax feat. ji-in cho - hörbuch edit
- lirik lagu claudia sinesi - salir
- lirik lagu isolation (rapper) - anthropophobie
- lirik lagu reinder feat. xaviera ibarra - otra dimensión
- lirik lagu mira - momente wie diese