lirik lagu dip doundou guiss - family
refrain
sukku ñaan ngir njaboot gi
dekku naaj ngir njaboot gi
ligeey ba de ngir njaboot gi
defar sa lifou njaboot
sukku ñaan ngir njaboot gi
dekku naaj ngir njaboot gi
ligeey ba de ngir njaboot gi
defar sa lifou njaboot
yeah yeah
defal si wa kër gi
doori waar ñëw def si wa kër gi
defal si wa kër gi
xamo lutax sa papa rare kër gi
dem doori waar
defal si wa kër gi
doori waar ñëw def si wa kër gi
li war si wa kër gi
xamo lutax sa papa rare kër gi
yeah yeah
couplet 1
mama sonu na lool
defna limu wa rone def si ñune
papa sonu na lool
defna limu wa rone def si ñune
ki nga doone munul bokku ak ki nga am
fo mën ti tollu du yeem sa ndeye ak baye
bul mëssa yees ba di tass ñom sen yaakar
mama da xeex ak dé pour jox sa life, joxla sa freedom, yarr la si baatine def si yaw fullë ak fayda
doxna ba feebar pour mëna fadj sa feebar
waxma bane banque lañu lay jox pour nga fay borr
pa bi da ligeey, neena caabi ya ngi ni, moy nga def mama bi beg
est~ce que bandit ya ngi jail ?
bess dh man dina fi gëdj, heritage du xaliss
na nga aar sa famille yep ndax giss na fi talibé yi
refrain
sukku ñaan ngir njaboot gi
dekku naaj ngir njaboot gi
ligeey ba de ngir njaboot gi
defar sa lifou njaboot
sukku ñaan ngir njaboot gi
dekku naaj ngir njaboot gi
ligeey ba de ngir njaboot gi
defar sa lifou njaboot
yeah yeah
defal si wa kër gi
doori waar ñëw def si wa kër gi
defal si wa kër gi
xamo lutax sa papa rare kër gi
dem doori waar
defal si wa kër gi
doori waar ñëw def si wa kër gi
li war si wa kër gi
xamo lutax sa papa rare kër gi
yeah yeah
couplet 2
never forget, fi ma juge, fima jaar lolotax bama melni
am am du wess, ñàkk du wëy, waye muno xaar lofi jobul ba jotsi
deretu gorr rek mofiy daw, mu naaj, muy taw you know
coono du reer non non non non non non yeah yeah
xale bu giss rongoñu meram di tokku
bu jomm saxul sa xol xamal ni melo ni mom
ku jaar si yoon bu jub ak yoon bu tërëdi bro
jaay sa ngor du yakamti mais gëmëdi lë
yeah yeah
deffal si wa kër gi, loo mën ak loo mënul si wa kër gi yeah yeah
lepp si wa kër gi, dé pour sa family yeahh
refrain
sukku ñaan ngir njaboot gi
dekku naaj ngir njaboot gi
ligeey ba de ngir njaboot gi
defar sa lifou njaboot
sukku ñaan ngir njaboot gi
dekku naaj ngir njaboot gi
ligeey ba de ngir njaboot gi
defar sa lifou njaboot
yeah yeah
defal si wa kër gi
doori waar ñëw def si wa kër gi
defal si wa kër gi
xamo lutax sa papa rare kër gi
dem doori waar
defal si wa kër gi
doori waar ñëw def si wa kër gi
li war si wa kër gi
xamo lutax sa papa rare kër gi
yeah yeah
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu rithm - big simpin'
- lirik lagu a letter home - child in question
- lirik lagu gunes ergun feat. ecem türkoğlu - pişman eder
- lirik lagu ji-su (kim ji soo) - muse
- lirik lagu 4za - puma joggies
- lirik lagu digão ogk - sei que cê quer
- lirik lagu primo & squarta - supercazzola 1,2,3
- lirik lagu the disaster area - sell your soul
- lirik lagu conor maynard - talking about (de$ignated remix)
- lirik lagu high spirits - now i know