lirik.web.id
a b c d e f g h i j k l m n o p q r s t u v w x y z 0 1 2 3 4 5 6 7 8 9 #

lirik lagu dior mbaye - baara aw

Loading...

anitiè heeheee
anitié heeebaaa
anitié hee heee
aaaaanh
kama li ngimaa
eeeeywaaaa aaanh
hiiyé deug leu khamngeu bo doné taw
da nga wara kham yone bi nga wara aw
baraa aw yow yay taw
fatima guétna yay kiko wara aw
hiiiyé deug leu khamngeu bo doné taw aaanh
da nga wara kham yone bi nga wara aw
aaanh yéyé
bara aw yow yay taw
fatima guetna yay kiko wara aw
haaaa
da nga wara takou ligueeey eheeh
yow deh bara aw yay tawou aw
dimbali sa yaye diapalé sa baye aaa
yow deh bara aw yay taw aaanh
taw bou bakh nilay dokhé
keur bou bakh nilay demé
yow deh bara aw yay taw aaanh
aaanh deug leu sax sa bou dioubé ba di to ba
yow deh bara aw yay taw aaah
yiiheee deug leu kham ngeu bo doné taw
dafa wara am yone bi nga wara aw
baraa aw yow yay taw
fatima guetna yay kiko wara aw
hiiiyee deug leu kham ngeu bo doné taw aaaanh
da nga wara kham yone bi nga wara aw aaaanh yeye
bara aw yow yay taw fatima guetna yay kiko wara aw
anitiiié heeehe
may seu djiguen eeeh
eeeh bara
bou am domi baye
eeeh eeeh eeeh bara
amine aynour bara aw diak warou la aaaanh
bara bara aaaw
bara bara aaaw
bara aw bara gueye
yaye kiko wara aw
yoe bara aw yay kiko wara aw
bara aaaw aaaanh
dounya bita bara aw
aaaanh dounya bita baraw aw
bara aw ooouuu aaanh dounya bita
anitié eheeeeh
kama li ngimaaa aywaaaah
aaaanh


Lirik lagu lainnya:

LIRIK YANG LAGI HITS MINGGU INI

Loading...