![lirik.web.id](https://lirik.web.id/tema/logo.png)
lirik lagu dieyla - mangui baxx
nélawo ba yandor
deuké lou bonn ak lou niaw
soxor ignann
mola cond~mné
doxal sa yonn
doumala soralé
meunou loma téré doundou lima nex
mangui bax
doumalén falé
bilay dinga geuna tardé
man daal doumalén falé
non non doumalén falé
fii lépangui tolo
talouma noono
bilay doumalén faalé
yaw mba diam nga fanané
yaw mba diam nga yéndo
woté lo geumoul
khamoni dieuli naala
mangui bax
doumalén falé
bilay dinga geuna tardé
man daal doumalén falé
non non doumalén falé
fii lépangui tolo
talouma noono
bilay doumalén faalé
noono (mom taloula)
li yalla def si man
ngané moukou doufi amé
aaah nga dima diébaané
nga dima diébaané
non non nono yeah
khamaloma dara weur dima toguè
dima soxoré yeah yeeeahhh
nélawo ba yandor
loudoul deuké lou bonn ak lou niaw
boul falé boul topato doxal sa dox
wouyooy bokoulèn yonn doxal sa dox
boul falé boul topato doxal sa dox
mangui bax (mangui bax)
doumalén falé
bilay dinga geuna tardé (bilay dinga geuna tardé)
man daal doumalén falé
non non doumalén falé
fii lépangui tolo
talouma noono
bilay doumalén faalé (talouma nono)
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu kukon - faded
- lirik lagu mike dece - sexy boy
- lirik lagu diggz da prophecy - overtime
- lirik lagu uproar - rebel youth
- lirik lagu real nashx - jesus piece
- lirik lagu abbalbisk - ти то (ti to)
- lirik lagu kidz bop kids - so far away
- lirik lagu raphaël roberge - break my own heart
- lirik lagu bones & cat soup - ickyvicky
- lirik lagu aj mcloughlin - can't taste no thatcher's haze!