lirik lagu carapid music - mak yow (feat. ardo)
[refrain : ardo] (x2)
you were my lady
démona baléy wowé ‘my life’ babygirl it’s was crazy
love buniu done dundu mak yow
[bako]
télouma mako sip yameu ndieukeu guiss
suniu love dafeu moudjou dém ba nekka lou diss
xalat binguey nane mane ak iow lou serieux
fateulikoul first kiss
damleu guiss rek beugeu
fokk ma wakhla deugeu
mais jour bi nga démé sama xol dafleu rebbeu
yeah sama xol dafla rebbeu
di wadjeu guéneu ci mane di cogner di fegg
yani sameu bopp every and night
now i’m in da dark cuz you were my light
yeah gurl you were light
et puis sama yone… f-ck you !
girl yama néwone naleu gueum légui
bayi sa yeufou xalé yi def yeufou magg touti
awmawone cash awmawone sh-t
wayé f-sson bimla beuguéwone amoul noroud chine
noumfa démé ? da am loumou degg
té lolou nonu mou degg néna dafeu nirok deugg
nouma beuguéwone néna beuguétouma ko
maniko tioloul mane ak iow dou fékké tommorrow
-bridge- (x2)
ma gui ni légui yagui ni
kou né na toppeu yonam mélni khadiou panini
ay text wala call neu lolou yeup diekh
fok suniu plate bi sét wétch bu ci bayi niékh
[refrain : ardo] (x2)
[kalz]
pourtant mak ioe dafeu lérrone
nio done andeuh di doxx di djangui école
pourant nio done nék soubak ngone
on n’avait rien,mais on était les maitres du monde -yeaa-
on a chopé l béguin andeuh déf lou nice
nieuppeu sédé ndaxx nim leu beugé wone dafa rare -ngeu-
présenté meu séy copines di xalat séy et puis
seu souriire dane meu danél : 4 appuis
ya meu done yokk doolé , ya done taxx douma messeu took di khoolé -nooo noow-
louleu métti done meu gaagne mélni niou bok déréét
mais anyway lolou ameutoul non non dedet!
khéy soubeu tipsé andi ay djikos
fokné que guissoumeu limouy déf mane djeulinako
niits yi di ladjté fils naane la feu démé
mou génél léne pretexte bou yombe rék néléne
“kalzi guéls yi ko weur dafeu xaweu beurri
tekssi dafay géneu goudi mane daal dém na parén-ssi”
waxou léne né daa am kou ko djeul si souf
di meu djaay djiko thiaga ndéké moo meu fouuf
-bridge- (x2)
ma gui ni légui yagui ni
kou né na toppeu yonam mélni khadjou panini
ay text wala call neu lolou yeup diekh
fok suniu plate bi sét wétch bu ci bayi niékh
fok suniu plate bi sét naah lemme tell you this
[refrain : ardo] (x2)
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu nicole milik - jar of hearts
- lirik lagu sabaton - hellrider (fist for fight (compiltation of demos)
- lirik lagu olli banjo - straight outta compton
- lirik lagu ariel rot - cuando no esperaba nada
- lirik lagu ted massena - sputnik 69
- lirik lagu beabadoobee - are you sure
- lirik lagu james vincent mcmorrow - cavalier
- lirik lagu amo$ - foreign
- lirik lagu nate57 - wo ist er jetzt?
- lirik lagu dr. chakalenstein - j'ai vraiment pas la baraka