lirik lagu bossbeatz xat xol - be the best
refrain
don’t worry don’t worry. job lou bari dina meusseu soti
be happy be happy. fight sa life boulsi meusseu tayi
deukeul si di fight sa life. one day dina meusseu nice
guemeul rék yokk sa fight. béss sa gui téw digua diote sa price
1er couplet
be the best and f… the rest. job correct niou done the best
started from the bottom now the top. no dounoufi déss
bossbeatz the produce, the real sh-t coming soon
topal gauche, you’re star me a moon
time the money, money fane yi, only time for the job
as pharell say we up to get lucky all night (alleluia)
ni soundiata tothie gouye ya
déf hit kéne dou adji ni (rolling stone and brown sugar)
bégueul for my mama, sigil for my papa
big up for my sister niou yokk diom mayma oh no
fitou tiger. yes we can obama, set melni swagger
victory we are champions
you know our dream, always rap machine, i dont give a d-mn
sss sa life boulssi meusseu tayi)
cfa,the dollars, boumoussi done bakhna
livre sterling, yen, yuan, niak naniy bagne lets go
refrain
don’t worry don’t worry. job lou bari dina meusseu soti
be happy be happy. fight sa life boulsi meusseu tayi
deukeul si di fight sa life. one day dina meusseu nice
guemeul rék yokk sa fight. béss sa gui téw digua diote sa price
2eme couplet
boula sikki sakka goudél nio ndandeu dou the test
nio gouté thiafka rimes niou ndandeu we the best
hard knock life jigger, young forever
get rich die trying keep winning for ever
peundou tanka gueune bou tate, danou dounou té dikate
gueum sounou bopp nanou déf, tégou si rail yi xeulate
we the best, true. douniou guéstou
waar everyday, ndam rék naniy sentou
your life, your way, your destiny. jom foulak fayda, tékkossi
fok niou lal si lingot yi, jackpot bi dégue bingo bi
kouy diangeu dokh danou, gueum ko rék digna kaniou
béss dina nieuw gna bakou. jot lépp ligna meusseu sakou
bridge (multi voice)
niodil boy si boum bi (jogueul fight n-gga)
bou dagoul dana téw (be the best yow)
fighteul (right) sa life (yeah)
guir none yi bagna ré (yeah)
xat, xat, xat xol recordz
refrain
don’t worry don’t worry. job lou bari dina meusseu soti
be happy be happy. fight sa life boulsi meusseu tayi
deukeul si di fight sa life. one day dina meusseu nice
guemeul rék yokk sa fight. béss sa gui téw digua diote sa price
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu b-trouble - won't u legalize it
- lirik lagu mustasch - lowlife highlights
- lirik lagu rockie fresh - your life
- lirik lagu abram - boom clap
- lirik lagu sammie - time
- lirik lagu chingadazo de kung fu - no lo tomes a mal (no me toques, ando chido)
- lirik lagu paula cole - new york city
- lirik lagu rowdy rebel - in the bedroom
- lirik lagu delta (express d.) - maintenant remix
- lirik lagu angel y khriz - ayer la vi - remix