lirik lagu amadeus (massamba amadeus) - fi ba leuz
eh, yooo
eh iiih
yeah yooo yaaa yeeh
fi ba leuz ma lay moom coow rekk ay bari
def la soxnay sama coobare
toppal sama ginnaaw te bu coow bari
xam nga ni yaay sama càppali
xam nga yaa ni ma
ni teg na ma la he
fu ma mousta teg jàmm bu yàlla bind
man fonk na ma la
man it ma ni la heee, sa xel naa dalee
diandia bi du soppeeku massamba
du dem sa massamba la, hei!
fi ba leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari)
def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari)
toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari)
xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari)
jànq yaa ma ni
du ku la ciippatu génn ci ndaxte yombuloo
du ku la jàmm na ni, he waay!
jànq yaa ma ni
bis dina ñëw nga daagu ci kër gi séyal
man ma tok ci ndaanaan yi, hee waay!
li nga ma wax tax na mën na ma wat
ni doo ma bàyyi même su ma faatoo
àdduna yépp su ñu dajewoon
pour séparer ñu du tax mu àntu
jànq yaa ma ni, jànq yaa ma ni
li nga dikk doy na ma, wëruma leneen
li nga ma wax neex na ma, yeiiii
fi ba leuz ma lay moom coow rekk ay bari (bari bari bari bari)
def la soxnay sama coobare (bari bari bari bari)
toppal sama ginnaaw te bu coow bari (bari bari bari bari)
xam nga ni yaay sama càppali (bari bari bari)
Lirik lagu lainnya:
- lirik lagu código fn & victoria león - las flores de mi amor
- lirik lagu 1ntr°\/ert - мне хуево (i'm fucked up)
- lirik lagu jane et les autres - le monstre
- lirik lagu teresa jennings - christmas in america
- lirik lagu твоя бывшая (tvoya bivshaya) - точки (points)
- lirik lagu reidar larsen - me and my piano
- lirik lagu bruce sudano - hey chattie
- lirik lagu revxrbb1 - alxc's return
- lirik lagu popp hunna - universal pain from mars
- lirik lagu edvards strazdiņš - ezers kluss